Yeesalu 20i Mai 2021 Ci 10i fan ak benn ci weeru maars 2020, kuréel gi yor wérgi yaram ci àdduna bi (OMS) neena lii di COVID-19 bi (Koronaawiris) feebaru mbass la. Mbir yaa ngi dox ci àdduna, tekk ci reew yaa ngi yokk wala di wañi tere yi ak/wala lepp lu jëm ci wallu kaarànge…